On this special day of Eid-ul-Fitr, we wish the Senegalese community in the UK and Muslims around the world happiness, peace and prosperity.
Ci bis bu mag bii di Eid-ul-Fitr, ñu ngi len di Dewanati, di ñaanal askanu Senegaal yi ci Angleterre ak jullit yi ci àdduna bi yépp, bànneex, jàmm ak xéewal.